Az-Zukhruf · 75/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
لَا يُفَتَّرُ عَنْهُمْ وَهُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ ۝٧٥
Laa yufattaru `anhum wa hum feehi mublisoon
📖 Tekkim Wolof
kenn duleen ko mas a woyafal te dañu naan fa xuum ne muq ngir jaaxle.

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Simoore Az-Zukhruf

73لَكُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ كَثِيرَةٌ مِّنْهَا تَأْكُلُونَ
Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca lekk”.
74إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي عَذَابِ جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,
75لَا يُفَتَّرُ عَنْهُمْ وَهُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ
kenn duleen ko mas a woyafal te dañu naan fa xuum ne muq ngir jaaxle.
76وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن كَانُوا هُمُ الظَّالِمِينَ
Du ut ne Nun noo leen tooñ, waaye ñoom ñoo tooñ (seen bopp).
77وَنَادَوْا يَا مَالِكُ لِيَقْضِ عَلَيْنَا رَبُّكَ ۖ قَالَ إِنَّكُم مَّاكِثُونَ
ña ngay woo : “ Maalik (bëkknéegu safara)! naan ko nanu sa Boroom jéggëli book ! ” muy tontu naan : “Yéen kay, ci [mbugël mii] ngeen di sax dëgg” !
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 75

Simoore Az-Zukhruf Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kenn duleen ko mas a woyafal te dañu naan fa…

Simoore Aaya 75/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers