Ad-Dukhan · 30/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
وَلَقَدْ نَجَّيْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مِنَ الْعَذَابِ الْمُهِينِ ۝٣٠
Wa laqad najjainaa Baneee Israaa`eela minal`azaabil muheen
📖 Tekkim Wolof
Musëloon Nanu , waa bani Israayiila ci mbugël mu doyadima (rey góor)

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Ad-Dukhan

28كَذَٰلِكَ ۖ وَأَوْرَثْنَاهَا قَوْمًا آخَرِينَ
Noonu la Nu ko donolee yeneeni xeet.
29فَمَا بَكَتْ عَلَيْهِمُ السَّمَاءُ وَالْأَرْضُ وَمَا كَانُوا مُنظَرِينَ
Asamaan ak suuf jooyuñuleen te kenn it muñadikuwuleen.
30وَلَقَدْ نَجَّيْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مِنَ الْعَذَابِ الْمُهِينِ
Musëloon Nanu , waa bani Israayiila ci mbugël mu doyadima (rey góor)
31مِن فِرْعَوْنَ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَالِيًا مِّنَ الْمُسْرِفِينَ
mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.
32وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 30

Simoore Ad-Dukhan Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Musëloon Nanu , waa bani Israayiila ci mbugël mu doyadima…

Simoore Aaya 30/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers