Ad-Dukhan · 4/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فِيهَا يُفْرَقُ كُلُّ أَمْرٍ حَكِيمٍ ۝٤
Feehaa yufraqu kullu amrin hakeem
📖 Tekkim Wolof
ci la Nuy teqalee mépp mbir mu xereñ,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Ad-Dukhan

2وَالْكِتَابِ الْمُبِينِ
Ak ci (Alxuraan) Téere bu leer bi (Maa ngi ciy waat) ne.
3إِنَّا أَنزَلْنَاهُ فِي لَيْلَةٍ مُّبَارَكَةٍ ۚ إِنَّا كُنَّا مُنذِرِينَ
Wàcce Nanu ko ci guddi gu barkeel, Nu ca doon xuppaate,
4فِيهَا يُفْرَقُ كُلُّ أَمْرٍ حَكِيمٍ
ci la Nuy teqalee mépp mbir mu xereñ,
5أَمْرًا مِّنْ عِندِنَا ۚ إِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ
moo di mbir mu bawoo ci Nun. Ci la Nuy yónnee [Yonnenta ya],
6رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
moo di yërmaande ju bawoo ci sa Boroom, mooy Kiy Dégg, di ku Xam,
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 4

Simoore Ad-Dukhan Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci la Nuy teqalee mépp mbir mu xereñ,

Simoore Aaya 4/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers