Ad-Dukhan · 56/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
لَا يَذُوقُونَ فِيهَا الْمَوْتَ إِلَّا الْمَوْتَةَ الْأُولَىٰ ۖ وَوَقَاهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ ۝٥٦
Laa yazooqoona feehal mawtaa illal mawtatal oolaa wa qaqaahum `azaabal jaheem
📖 Tekkim Wolof
Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk ga. [Yàlla] fegal na leen mbugëlum Safara,

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Ad-Dukhan

54كَذَٰلِكَ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
Noonu ! La ñu leen di maye ay soxna (yu am bët) huuru alayn.
55يَدْعُونَ فِيهَا بِكُلِّ فَاكِهَةٍ آمِنِينَ
Ñu fay man a am wépp xeeti fuytéef féex lool ne fayax.
56لَا يَذُوقُونَ فِيهَا الْمَوْتَ إِلَّا الْمَوْتَةَ الْأُولَىٰ ۖ وَوَقَاهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk ga. [Yàlla] fegal na leen mbugëlum Safara,
57فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
58فَإِنَّمَا يَسَّرْنَاهُ بِلِسَانِكَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Di ko yombal ci saw làmmiñ, ngir amaana ñuy fàttaliku !
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 56

Simoore Ad-Dukhan Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk…

Simoore Aaya 56/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers