Ad-Dukhan · 55/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
يَدْعُونَ فِيهَا بِكُلِّ فَاكِهَةٍ آمِنِينَ ۝٥٥
Yad`oona feehaa bikulli faakihatin aamineen
📖 Tekkim Wolof
Ñu fay man a am wépp xeeti fuytéef féex lool ne fayax.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 53-57 — Simoore Ad-Dukhan

53يَلْبَسُونَ مِن سُندُسٍ وَإِسْتَبْرَقٍ مُّتَقَابِلِينَ
ñuy soloo ca xeeti sooy ya gën a ràññiku ne rojj jàkkarloo.
54كَذَٰلِكَ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
Noonu ! La ñu leen di maye ay soxna (yu am bët) huuru alayn.
55يَدْعُونَ فِيهَا بِكُلِّ فَاكِهَةٍ آمِنِينَ
Ñu fay man a am wépp xeeti fuytéef féex lool ne fayax.
56لَا يَذُوقُونَ فِيهَا الْمَوْتَ إِلَّا الْمَوْتَةَ الْأُولَىٰ ۖ وَوَقَاهُمْ عَذَابَ الْجَحِيمِ
Duñu fa mos wextanu ndee lu dul dee gu jëkk ga. [Yàlla] fegal na leen mbugëlum Safara,
57فَضْلًا مِّن رَّبِّكَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْعَظِيمُ
muy ngëneel lu bawoo ca sa Boroom. loolu mooy texe gu màgg ga.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 55

Simoore Ad-Dukhan Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu fay man a am wépp xeeti fuytéef féex lool…

Simoore Aaya 55/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers