Al-Jathiya · 15/37
Tekki Waxtaan — Al-Jathiya
مَنْ عَمِلَ صَالِحًا فَلِنَفْسِهِ ۖ وَمَنْ أَسَاءَ فَعَلَيْهَا ۖ ثُمَّ إِلَىٰ رَبِّكُمْ تُرْجَعُونَ ۝١٥
Maa `amila saalihan falinafsihee wa man asaaa`a fa`alaihaa summa ilaa Rabbikum turja`oon
📖 Tekkim Wolof
Képp kuy jëf yiw, moom caak ; képp kuy jëf lu bon it, moom caak. Ndax yéen ñépp ca seen boroom ngeen di dellu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 13-17 — Al-Jathiya

13وَسَخَّرَ لَكُم مَّا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ جَمِيعًا مِّنْهُ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Moo leen tàggatal lépp lu nekk ci asamaan yeek suuf si, Ay kéemtaan a ngi ci yuy soxal ñiy xalaat.
14قُل لِّلَّذِينَ آمَنُوا يَغْفِرُوا لِلَّذِينَ لَا يَرْجُونَ أَيَّامَ اللَّهِ لِيَجْزِيَ قَوْمًا بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Waxal ñi gëm ne leen na ñuy jégël ñi yaakaarul bisi Yàlla ya ci ne Yàlla dana àtte fay xeet wu nekk ci kem la ñu daan fàggu.
15مَنْ عَمِلَ صَالِحًا فَلِنَفْسِهِ ۖ وَمَنْ أَسَاءَ فَعَلَيْهَا ۖ ثُمَّ إِلَىٰ رَبِّكُمْ تُرْجَعُونَ
Képp kuy jëf yiw, moom caak ; képp kuy jëf lu bon it, moom caak. Ndax yéen ñépp ca seen boroom ngeen di dellu.
16وَلَقَدْ آتَيْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ الْكِتَابَ وَالْحُكْمَ وَالنُّبُوَّةَ وَرَزَقْنَاهُم مِّنَ الطَّيِّبَاتِ وَفَضَّلْنَاهُمْ عَلَى الْعَالَمِينَ
Indiloon Nanu waa giiru Banii-Israayiil Téere ba, ak ngor ga, ak yonnenta ga, wërsëgëloon Nanu leen ci àddina si yépp ;
17وَآتَيْنَاهُم بَيِّنَاتٍ مِّنَ الْأَمْرِ ۖ فَمَا اخْتَلَفُوا إِلَّا مِن بَعْدِ مَا جَاءَهُمُ الْعِلْمُ بَغْيًا بَيْنَهُمْ ۚ إِنَّ رَبَّكَ يَقْضِي بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
joxoon Nanu leen ay firnde yu leer ci ndigël yi. Wuutewuñu woon lu dul ba ñu amee xam- xam cig bew, ci seen diggënte. Te sa Boroom dana àtte seen diggënte, bu Bis Pénc baa, ca la ñu daan juuyoo.
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Jathiya 15

Simoore Al-Jathiya Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp kuy jëf yiw, moom caak ; képp kuy jëf…

Simoore Aaya 15/37 — Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jathiya Dégg, Al-Jathiya Tekki, Al-Jathiya mp3, Al-Jathiya pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers