Al-Ahqaf · 11/35
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahqaf
وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا لَوْ كَانَ خَيْرًا مَّا سَبَقُونَا إِلَيْهِ ۚ وَإِذْ لَمْ يَهْتَدُوا بِهِ فَسَيَقُولُونَ هَٰذَا إِفْكٌ قَدِيمٌ ۝١١
Wa qaalal lazeena kafaroo lillazeena aamanoo law kaana khairam maa sabaqoonaaa ilyh; wa iz lam yahtadoo bihee fasa yaqooloona haazaaa ifkun qadeem
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi ngay wax ñi gëm naan leen : “Su fekkoon ne yiw la dana nu ca jiitu”. Ngir séenug ñakka gindiku dana ñu xala wax naan : “Alxuraan jii ay dur la yu yàgg ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Ahqaf

9قُلْ مَا كُنتُ بِدْعًا مِّنَ الرُّسُلِ وَمَا أَدْرِي مَا يُفْعَلُ بِي وَلَا بِكُمْ ۖ إِنْ أَتَّبِعُ إِلَّا مَا يُوحَىٰ إِلَيَّ وَمَا أَنَا إِلَّا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Waxal ne : “Du man maay Yonent bi jëkk feeñ ; te it xamuma li ñuy xala def ci man, mbaa ci yéen. Man daal damay topp linu may soloo doŋŋ ; te itam doonu ma kenn ku dul ab waaraatekat buy leeral”.
10قُلْ أَرَأَيْتُمْ إِن كَانَ مِنْ عِندِ اللَّهِ وَكَفَرْتُم بِهِ وَشَهِدَ شَاهِدٌ مِّن بَنِي إِسْرَائِيلَ عَلَىٰ مِثْلِهِ فَآمَنَ وَاسْتَكْبَرْتُمْ ۖ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Waxal ne: “Ana lan mooy xalaat ci ne lii su fekkee dafa bawoo ca Yàlla ngeen weddi ko, mu am it ci giir banii israayila kenn ku ca seede lu ni mel moom mi gëm, yéen ngeen rëy- rëylu... Yàlla dey du gindi aw nit ñuy tooñkat ! ”
11وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا لَوْ كَانَ خَيْرًا مَّا سَبَقُونَا إِلَيْهِ ۚ وَإِذْ لَمْ يَهْتَدُوا بِهِ فَسَيَقُولُونَ هَٰذَا إِفْكٌ قَدِيمٌ
Ña weddi ngay wax ñi gëm naan leen : “Su fekkoon ne yiw la dana nu ca jiitu”. Ngir séenug ñakka gindiku dana ñu xala wax naan : “Alxuraan jii ay dur la yu yàgg ! ”
12وَمِن قَبْلِهِ كِتَابُ مُوسَىٰ إِمَامًا وَرَحْمَةً ۚ وَهَٰذَا كِتَابٌ مُّصَدِّقٌ لِّسَانًا عَرَبِيًّا لِّيُنذِرَ الَّذِينَ ظَلَمُوا وَبُشْرَىٰ لِلْمُحْسِنِينَ
Téereb Muusaa jiituwoon na ko di njub. Lii nag ab téere la buy dëggal loolu ci làmmiñu araab, ngir muy xupp ñiy tooñ di bégal ñiy rafetal (ay jëf).
13إِنَّ الَّذِينَ قَالُوا رَبُّنَا اللَّهُ ثُمَّ اسْتَقَامُوا فَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Ñi gëm Yàlla tey jaar ca yoon wu jub xocc wa, duñu tiit duñu jaaxle.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Ahqaf 11

Simoore Al-Ahqaf Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi ngay wax ñi gëm naan leen : “Su…

Simoore Aaya 11/35 — Simoore Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahqaf Dégg, Simoore Al-Ahqaf Tekki, Simoore Al-Ahqaf mp3, Simoore Al-Ahqaf pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers