Al-Ahqaf · 25/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
تُدَمِّرُ كُلَّ شَيْءٍ بِأَمْرِ رَبِّهَا فَأَصْبَحُوا لَا يُرَىٰ إِلَّا مَسَاكِنُهُمْ ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْقَوْمَ الْمُجْرِمِينَ ٢٥
Transliteration
Tudammiru kulla shai`im bi-amri Rabbihaa fa asbahoo laa yuraaa illaa masaakinuhum; kazaalika najzil qawmal mujrimeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ci ndigalul Yàlla dafay nappaaje lépp”. Mu faagaagal leen ñoom ñépp ba séen dëkuwaay ya doŋŋ des fa. Noonu lanuy faye tooñkat ya (sàmbaa-bóoy sa).
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 23-27 — Al-Ahqaf
23قَالَ إِنَّمَا الْعِلْمُ عِندَ اللَّهِ وَأُبَلِّغُكُم مَّا أُرْسِلْتُ بِهِ وَلَٰكِنِّي أَرَاكُمْ قَوْمًا تَجْهَلُونَ
Mu ne leen : “ Xam-xam moom ma nga ca Yàlla. Man nag dama leen di jottali liñu ma yonni. Waaye gis naa ne yéen ñii aw nit ngeen ñu réer xamadi”.
24فَلَمَّا رَأَوْهُ عَارِضًا مُّسْتَقْبِلَ أَوْدِيَتِهِمْ قَالُوا هَٰذَا عَارِضٌ مُّمْطِرُنَا ۚ بَلْ هُوَ مَا اسْتَعْجَلْتُم بِهِ ۖ رِيحٌ فِيهَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ba nu gisee niir wa dëgmël séen xur ya , wax na ñu ne ; “Lii aw xiin la wu nuy tawal”. Déet walaay ! lii nag mooy la ngeen daan yàkkamti : Ngelaw lu ëmb mbugël mu mitti,
25تُدَمِّرُ كُلَّ شَيْءٍ بِأَمْرِ رَبِّهَا فَأَصْبَحُوا لَا يُرَىٰ إِلَّا مَسَاكِنُهُمْ ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْقَوْمَ الْمُجْرِمِينَ
ci ndigalul Yàlla dafay nappaaje lépp”. Mu faagaagal leen ñoom ñépp ba séen dëkuwaay ya doŋŋ des fa. Noonu lanuy faye tooñkat ya (sàmbaa-bóoy sa).
26وَلَقَدْ مَكَّنَّاهُمْ فِيمَا إِن مَّكَّنَّاكُمْ فِيهِ وَجَعَلْنَا لَهُمْ سَمْعًا وَأَبْصَارًا وَأَفْئِدَةً فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُمْ سَمْعُهُمْ وَلَا أَبْصَارُهُمْ وَلَا أَفْئِدَتُهُم مِّن شَيْءٍ إِذْ كَانُوا يَجْحَدُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Yombaloon nanu leen ñoom lu nu leen joxul yéen. Ndax defaloon nanu leen ag dégg ak ub gis, te seen dégg ga, wala séen gis ba, ak séen xol ya jariñu leen woon tus, ndax dañu daan weddi Laaya Yàlla yi firndeem ya. Ñañu daan yéjji far sóor leen.
27وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا مَا حَوْلَكُم مِّنَ الْقُرَىٰ وَصَرَّفْنَا الْآيَاتِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Faagaagal nañu ca dëkk ya leen wër ; defaroon ay keemaan ak firnde yu wuute, ngir bëggoon ñu dellu ginnaaw ca séen kéefër gi.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
25Aaya
Tekki — Al-Ahqaf 25
Simoore Al-Ahqaf Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ci ndigalul Yàlla dafay nappaaje lépp”. Mu faagaagal leen ñoom…Simoore Aaya 25/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








