Al-Hujurat · 8/18
Tekki Waxtaan — Al-Hujurat
فَضْلًا مِّنَ اللَّهِ وَنِعْمَةً ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ ٨
Transliteration
Fadlam minal laahi wa ni`mah; wallaahu `Aleemun Hakeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
mooy ngëneel lu bawoo fa Yàlla di xéewël. Yàlla Ku Xam la ku Xereñ la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 6-10 — Al-Hujurat
6يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن جَاءَكُمْ فَاسِقٌ بِنَبَإٍ فَتَبَيَّنُوا أَن تُصِيبُوا قَوْمًا بِجَهَالَةٍ فَتُصْبِحُوا عَلَىٰ مَا فَعَلْتُمْ نَادِمِينَ
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen ab saay-saay indiley xibaar, na ngeen ko leerlu ndax amaana mu tax ngeen dal ci gawu nit ngir am lënt su ko defee ngeen mujj di ko réccu.
7وَاعْلَمُوا أَنَّ فِيكُمْ رَسُولَ اللَّهِ ۚ لَوْ يُطِيعُكُمْ فِي كَثِيرٍ مِّنَ الْأَمْرِ لَعَنِتُّمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ حَبَّبَ إِلَيْكُمُ الْإِيمَانَ وَزَيَّنَهُ فِي قُلُوبِكُمْ وَكَرَّهَ إِلَيْكُمُ الْكُفْرَ وَالْفُسُوقَ وَالْعِصْيَانَ ۚ أُولَٰئِكَ هُمُ الرَّاشِدُونَ
Xam leen ne Yonent Yàlla baa ngi ci seen biir. Su fekkoon ne dana leen faral a topp ci mbir yu bari, kon dangeen am coono. Waaye Yàlla moo leen sopploo ngëm taaral ko ci seen xol moo leen bañloo it kéefër, ak ug caay-caay ak ug moy Yàlla. Ñoom ñooñee ñoo di gaay ñu jub ña,
8فَضْلًا مِّنَ اللَّهِ وَنِعْمَةً ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
mooy ngëneel lu bawoo fa Yàlla di xéewël. Yàlla Ku Xam la ku Xereñ la.
9وَإِن طَائِفَتَانِ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ اقْتَتَلُوا فَأَصْلِحُوا بَيْنَهُمَا ۖ فَإِن بَغَتْ إِحْدَاهُمَا عَلَى الْأُخْرَىٰ فَقَاتِلُوا الَّتِي تَبْغِي حَتَّىٰ تَفِيءَ إِلَىٰ أَمْرِ اللَّهِ ۚ فَإِن فَاءَتْ فَأَصْلِحُوا بَيْنَهُمَا بِالْعَدْلِ وَأَقْسِطُوا ۖ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُقْسِطِينَ
Su ñaari kuréel ci jullit ñi di xeexoo, na ngeen yéwénal seeni diggante. Su fekkee ne benn ba moo jalgati tooñ ba ca des, na ngeen xeex ak bay tooñ, ba baa muy dellu ci ndigalul Yàlla. Bu, delloo ci ndigal nag, na ngeen leen jubale te ngeen maandu Yàlla safoona ñu maandu ña.
10إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ إِخْوَةٌ فَأَصْلِحُوا بَيْنَ أَخَوَيْكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Way gëm ña ay mbokk la ñu. Na ngeen di yéwénal seen digganteek seen mbokk, te ngeen ragal Yàlla, ndax amaana yëramees leen.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
8Aaya
Tekki — Al-Hujurat 8
Simoore Al-Hujurat Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mooy ngëneel lu bawoo fa Yàlla di xéewël. Yàlla Ku…Simoore Aaya 8/18 — Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hujurat Dégg, Al-Hujurat Tekki, Al-Hujurat mp3, Al-Hujurat pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








