Qaf · 42/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ ۝٤٢
Yawma yasmaoonas sai hata bilhaqq zaalika yawmul khurooj
📖 Tekkim Wolof
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore Qaf

40وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَأَدْبَارَ السُّجُودِ
guddi gi it dee ko sàbbaal, ak ci ginnaaw julli gu nekk
41وَاسْتَمِعْ يَوْمَ يُنَادِ الْمُنَادِ مِن مَّكَانٍ قَرِيبٍ
Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba (Israafiil) di wootee fu jige,
42يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.
43إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
44يَوْمَ تَشَقَّقُ الْأَرْضُ عَنْهُمْ سِرَاعًا ۚ ذَٰلِكَ حَشْرٌ عَلَيْنَا يَسِيرٌ
bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn gaaw lool. Loolu nag ag dajale la gu yomb ci Nun.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Qaf 42

Simoore Qaf Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te…

Simoore Aaya 42/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers