At-Tur · 32/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ ۝٣٢
Am taamuruhum ahlaamuhum bihaazaaa am hum qawmun taaghoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 30-34 — At-Tur

30أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
31قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.
32أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
33أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
34فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — At-Tur 32

Simoore At-Tur Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am…

Simoore Aaya 32/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers