At-Tur · 31/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ ۝٣١
Qul tarabbasoo fa innee ma`akum minal mutarabbiseen
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — At-Tur

29فَذَكِّرْ فَمَا أَنتَ بِنِعْمَتِ رَبِّكَ بِكَاهِنٍ وَلَا مَجْنُونٍ
Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa ab dof ;
30أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
31قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.
32أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
33أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — At-Tur 31

Simoore At-Tur Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak…

Simoore Aaya 31/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers