At-Tur · 38/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ لَهُمْ سُلَّمٌ يَسْتَمِعُونَ فِيهِ ۖ فَلْيَأْتِ مُسْتَمِعُهُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ ۝٣٨
Am lahum sullamuny yastami`oona feehi falyaati mustami`uhum bisultaanim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan di déglu) ? Su fekkee loolu am na ka leen daan yëdujil na indi ay lay yu leer kon !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 36-40 — Simoore At-Tur

36أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.
37أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
38أَمْ لَهُمْ سُلَّمٌ يَسْتَمِعُونَ فِيهِ ۖ فَلْيَأْتِ مُسْتَمِعُهُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan di déglu) ? Su fekkee loolu am na ka leen daan yëdujil na indi ay lay yu leer kon !
39أَمْ لَهُ الْبَنَاتُ وَلَكُمُ الْبَنُونَ
Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen, yéen ngeen am yu góor ? (mukk)
40أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ
Moo ndax dangeen leen di laaj ag pey, te ñoom nu diis gann ak i bor ?
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — At-Tur 38

Simoore At-Tur Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan…

Simoore Aaya 38/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers