At-Tur · 37/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ ۝٣٧
Am`indahum khazaaa`inu rabbika am humul musaitiroon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 35-39 — At-Tur

35أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?
36أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.
37أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
38أَمْ لَهُمْ سُلَّمٌ يَسْتَمِعُونَ فِيهِ ۖ فَلْيَأْتِ مُسْتَمِعُهُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan di déglu) ? Su fekkee loolu am na ka leen daan yëdujil na indi ay lay yu leer kon !
39أَمْ لَهُ الْبَنَاتُ وَلَكُمُ الْبَنُونَ
Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen, yéen ngeen am yu góor ? (mukk)
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — At-Tur 37

Simoore At-Tur Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla…

Simoore Aaya 37/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers