At-Tur · 39/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ لَهُ الْبَنَاتُ وَلَكُمُ الْبَنُونَ ۝٣٩
Am lahul banaatu wa lakumul banoon
📖 Tekkim Wolof
Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen, yéen ngeen am yu góor ? (mukk)

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 37-41 — Simoore At-Tur

37أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
38أَمْ لَهُمْ سُلَّمٌ يَسْتَمِعُونَ فِيهِ ۖ فَلْيَأْتِ مُسْتَمِعُهُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan di déglu) ? Su fekkee loolu am na ka leen daan yëdujil na indi ay lay yu leer kon !
39أَمْ لَهُ الْبَنَاتُ وَلَكُمُ الْبَنُونَ
Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen, yéen ngeen am yu góor ? (mukk)
40أَمْ تَسْأَلُهُمْ أَجْرًا فَهُم مِّن مَّغْرَمٍ مُّثْقَلُونَ
Moo ndax dangeen leen di laaj ag pey, te ñoom nu diis gann ak i bor ?
41أَمْ عِندَهُمُ الْغَيْبُ فَهُمْ يَكْتُبُونَ
Walla ñoom ñoo ame Mbóot yi di ko bind ?
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — At-Tur 39

Simoore At-Tur Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla book Yàlla moom moo am ay doom yu jigéen,…

Simoore Aaya 39/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers