At-Tur · 46/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
يَوْمَ لَا يُغْنِي عَنْهُمْ كَيْدُهُمْ شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ ۝٤٦
Yawma laa yughnee `anhum kaidumhum shai`anw wa laa hum yunsaroon
📖 Tekkim Wolof
bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen dimbali.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore At-Tur

44وَإِن يَرَوْا كِسْفًا مِّنَ السَّمَاءِ سَاقِطًا يَقُولُوا سَحَابٌ مَّرْكُومٌ
Su ñu gIisaan mbugël sax muy wàcce asamaan, dañu naan : “Niir yu dajaloo la”.
45فَذَرْهُمْ حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي فِيهِ يُصْعَقُونَ
Bàyyileen , ba ñu dajeek bis ba ñu leen di mbugël,
46يَوْمَ لَا يُغْنِي عَنْهُمْ كَيْدُهُمْ شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen dimbali.
47وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.
48وَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ فَإِنَّكَ بِأَعْيُنِنَا ۖ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ حِينَ تَقُومُ
Nangay muñ li sa Boroom di dogal. Doo raw sunuy gët (Nun Yàlla). Te ne ngay sàbbaal sa Boroom di ko sant saa soo jógee ;
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — At-Tur 46

Simoore At-Tur Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen…

Simoore Aaya 46/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers