An-Najm · 19/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
أَفَرَأَيْتُمُ اللَّاتَ وَالْعُزَّىٰ ۝١٩
Afara`aytumul laata wal `uzzaa
📖 Tekkim Wolof
Waaw xërëmu Laata ak Uzzaa lu ñu leen di niru,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 17-21 — Simoore An-Najm

17مَا زَاغَ الْبَصَرُ وَمَا طَغَىٰ
Da koo gis dëgg bët ya jéllul jaawalewul.
18لَقَدْ رَأَىٰ مِنْ آيَاتِ رَبِّهِ الْكُبْرَىٰ
Gis tigi ca kéemtaani Boroomam ya gën a màgg.
19أَفَرَأَيْتُمُ اللَّاتَ وَالْعُزَّىٰ
Waaw xërëmu Laata ak Uzzaa lu ñu leen di niru,
20وَمَنَاةَ الثَّالِثَةَ الْأُخْرَىٰ
ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?
21أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — An-Najm 19

Simoore An-Najm Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaw xërëmu Laata ak Uzzaa lu ñu leen di niru,

Simoore Aaya 19/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers