An-Najm · 20/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
وَمَنَاةَ الثَّالِثَةَ الْأُخْرَىٰ ۝٢٠
Wa manaatas saalisatal ukhraa
📖 Tekkim Wolof
ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 18-22 — An-Najm

18لَقَدْ رَأَىٰ مِنْ آيَاتِ رَبِّهِ الْكُبْرَىٰ
Gis tigi ca kéemtaani Boroomam ya gën a màgg.
19أَفَرَأَيْتُمُ اللَّاتَ وَالْعُزَّىٰ
Waaw xërëmu Laata ak Uzzaa lu ñu leen di niru,
20وَمَنَاةَ الثَّالِثَةَ الْأُخْرَىٰ
ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?
21أَلَكُمُ الذَّكَرُ وَلَهُ الْأُنثَىٰ
Moo ndax yéen a am doom yu góor moom Yàlla mu am ay jigéen ?
22تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — An-Najm 20

Simoore An-Najm Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak Manaat xërëm ba ca des, te ñetteel leen ?

Simoore Aaya 20/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers