An-Najm · 50/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ ۝٥٠
Wa annahooo ahlak a `Aadanil oolaa
📖 Tekkim Wolof
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 48-52 — Simoore An-Najm

48وَأَنَّهُ هُوَ أَغْنَىٰ وَأَقْنَىٰ
te moom Mooy woomalale.
49وَأَنَّهُ هُوَ رَبُّ الشِّعْرَىٰ
Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,
50وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,
51وَثَمُودَ فَمَا أَبْقَىٰ
ak waa Samuud, ba kenn desufa,
52وَقَوْمَ نُوحٍ مِّن قَبْلُ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا هُمْ أَظْلَمَ وَأَطْغَىٰ
ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon tooñ te gënoon a bew,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — An-Najm 50

Simoore An-Najm Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,

Simoore Aaya 50/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers