An-Najm · 49/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَأَنَّهُ هُوَ رَبُّ الشِّعْرَىٰ ۝٤٩
Wa annahoo huwa rabbush shi`raa
📖 Tekkim Wolof
Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore An-Najm

47وَأَنَّ عَلَيْهِ النَّشْأَةَ الْأُخْرَىٰ
moom moo waral it sosuwaat ga dekkiwaat,
48وَأَنَّهُ هُوَ أَغْنَىٰ وَأَقْنَىٰ
te moom Mooy woomalale.
49وَأَنَّهُ هُوَ رَبُّ الشِّعْرَىٰ
Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,
50وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,
51وَثَمُودَ فَمَا أَبْقَىٰ
ak waa Samuud, ba kenn desufa,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — An-Najm 49

Simoore An-Najm Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,

Simoore Aaya 49/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers