An-Najm · 51/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
وَثَمُودَ فَمَا أَبْقَىٰ ۝٥١
Wa samooda famaaa abqaa
📖 Tekkim Wolof
ak waa Samuud, ba kenn desufa,

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — An-Najm

49وَأَنَّهُ هُوَ رَبُّ الشِّعْرَىٰ
Te mooy boroom biddiw ba Si’raa,
50وَأَنَّهُ أَهْلَكَ عَادًا الْأُولَىٰ
te moom Moo faagaagaloon waa Aad ñu jëkk ña,
51وَثَمُودَ فَمَا أَبْقَىٰ
ak waa Samuud, ba kenn desufa,
52وَقَوْمَ نُوحٍ مِّن قَبْلُ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا هُمْ أَظْلَمَ وَأَطْغَىٰ
ak nitu Nooh ñu jëkk ña, ndax ñoom ñoo dàqoon tooñ te gënoon a bew,
53وَالْمُؤْتَفِكَةَ أَهْوَىٰ
noona la wëlbatee suuf sa këpp leen ko.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — An-Najm 51

Simoore An-Najm Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak waa Samuud, ba kenn desufa,

Simoore Aaya 51/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers