An-Najm · 8/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
ثُمَّ دَنَا فَتَدَلَّىٰ ۝٨
Summa danaa fatadalla
📖 Tekkim Wolof
Daldi nay jegeñ ba faf yoore,

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore An-Najm

6ذُو مِرَّةٍ فَاسْتَوَىٰ
mu di ku taaru te yemoo,
7وَهُوَ بِالْأُفُقِ الْأَعْلَىٰ
te moom ma nga ca déeléy asamaan ya gën a kawe (guddig rañaan ga).
8ثُمَّ دَنَا فَتَدَلَّىٰ
Daldi nay jegeñ ba faf yoore,
9فَكَانَ قَابَ قَوْسَيْنِ أَوْ أَدْنَىٰ
Moo ngi jege woon ni ñaari xocci xala, walla sax mu gën a jigeñ loolu
10فَأَوْحَىٰ إِلَىٰ عَبْدِهِ مَا أَوْحَىٰ
(Foofee) la Yàlla soloo jaamam la mu ko soloo.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — An-Najm 8

Simoore An-Najm Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Daldi nay jegeñ ba faf yoore,

Simoore Aaya 8/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers