An-Najm · 7/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَهُوَ بِالْأُفُقِ الْأَعْلَىٰ ۝٧
Wa huwa bil ufuqil a`laa
📖 Tekkim Wolof
te moom ma nga ca déeléy asamaan ya gën a kawe (guddig rañaan ga).

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore An-Najm

5عَلَّمَهُ شَدِيدُ الْقُوَىٰ
[Jibriil] boroom kàttan gu tar ga moo ko jàngal,
6ذُو مِرَّةٍ فَاسْتَوَىٰ
mu di ku taaru te yemoo,
7وَهُوَ بِالْأُفُقِ الْأَعْلَىٰ
te moom ma nga ca déeléy asamaan ya gën a kawe (guddig rañaan ga).
8ثُمَّ دَنَا فَتَدَلَّىٰ
Daldi nay jegeñ ba faf yoore,
9فَكَانَ قَابَ قَوْسَيْنِ أَوْ أَدْنَىٰ
Moo ngi jege woon ni ñaari xocci xala, walla sax mu gën a jigeñ loolu
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — An-Najm 7

Simoore An-Najm Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te moom ma nga ca déeléy asamaan ya gën a…

Simoore Aaya 7/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers