Al-Qamar · 38/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
وَلَقَدْ صَبَّحَهُم بُكْرَةً عَذَابٌ مُّسْتَقِرٌّ ٣٨
Transliteration
Wa laqad sabbahahum bukratan `azaabum mustaqirr
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul tàggool.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Al-Qamar
36وَلَقَدْ أَنذَرَهُم بَطْشَتَنَا فَتَمَارَوْا بِالنُّذُرِ
Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu daan werante ci loolu.
37وَلَقَدْ رَاوَدُوهُ عَن ضَيْفِهِ فَطَمَسْنَا أَعْيُنَهُمْ فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Dañoo, sàkkoo saay-saaye ganam ña. Nu daldi fatt seen gët ne leen “Mosleen Sama mbugël ak Samak xupp”.
38وَلَقَدْ صَبَّحَهُم بُكْرَةً عَذَابٌ مُّسْتَقِرٌّ
Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul tàggool.
39فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Mosleen Samak mbugël ak Samag xuppe.
40وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Mo ndax kon kenn dana ca jàjjoo ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — Al-Qamar 38
Simoore Al-Qamar Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul…Simoore Aaya 38/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








