Ar-Rahman · 31/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
سَنَفْرُغُ لَكُمْ أَيُّهَ الثَّقَلَانِ ۝٣١
Sanafrughu lakum ayyuhas saqalaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne yi, danañu leen xalseta àtte
🎧 Dégg

📜 Aaya 29-33 — Ar-Rahman

29يَسْأَلُهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ كُلَّ يَوْمٍ هُوَ فِي شَأْنٍ
Ñi nekk asamaan ak suuf sii ngi koy laaj aka Dagaan. Te moom bis bu nekk, Mi ngi ci mbir.
30فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
31سَنَفْرُغُ لَكُمْ أَيُّهَ الثَّقَلَانِ
Yéen nit ak jinne yi, danañu leen xalseta àtte
32فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
33يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ إِنِ اسْتَطَعْتُمْ أَن تَنفُذُوا مِنْ أَقْطَارِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ فَانفُذُوا ۚ لَا تَنفُذُونَ إِلَّا بِسُلْطَانٍ
Eey yéen mbooleem jinne yi ak nit ñi ! Su ngeen manee lañbatu ci biir déeléy asamaan yeek suuf si, lañbatuleen. Waaye du ngeen mana kër-këri mukk ba génn kiiraayal Yàlla.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
31Aaya

Tekki — Ar-Rahman 31

Simoore Ar-Rahman Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne yi, danañu leen xalseta àtte

Simoore Aaya 31/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers