Ar-Rahman · 60/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
هَلْ جَزَاءُ الْإِحْسَانِ إِلَّا الْإِحْسَانُ ۝٦٠
Hal jazaaa`ul ihsaani illal ihsaan
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax lu rafet man naa am geneen pey guddul lu rafet (mukk du am) ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 58-62 — Simoore Ar-Rahman

58كَأَنَّهُنَّ الْيَاقُوتُ وَالْمَرْجَانُ
Dañuy [rafet ba] melni: wurus yaaquut walla marjaan.
59فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
60هَلْ جَزَاءُ الْإِحْسَانِ إِلَّا الْإِحْسَانُ
Moo ndax lu rafet man naa am geneen pey guddul lu rafet (mukk du am) ?
61فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
62وَمِن دُونِهِمَا جَنَّتَانِ
Ci dër yooyu amaat na yeneen ñaari dër.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
60Aaya

Tekki — Ar-Rahman 60

Simoore Ar-Rahman Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax lu rafet man naa am geneen pey guddul…

Simoore Aaya 60/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers