Al-An'am · 2/165
Tekki Waxtaan — Al-An'am
هُوَ ٱلَّذِي خَلَقَكُم مِّن طِينٍ ثُمَّ قَضَىٰٓ أَجَلًاۖ وَأَجَلٌ مُّسَمًّى عِندَهُۥۖ ثُمَّ أَنتُمۡ تَمۡتَرُونَ  ۝٢
Huwal lazee khalaqakum min teenin summa qadaaa ajalanw wa ajalum musamman `indahoo summa antum tamtaroon
📖 Tekkim Wolof
Moom mooy ki leen bind ci ban ; ba noppi dugal àpp [ci dundu gu ne] ak àpp ba ñu tudd ci Moom [ci jéexug àdduna si]. Ba noppi ngeen di am xel-yaar !
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-4 — Al-An'am

1ٱلۡحَمۡدُ لِلَّهِ ٱلَّذِي خَلَقَ ٱلسَّمَٰوَٰتِ وَٱلۡأَرۡضَ وَجَعَلَ ٱلظُّلُمَٰتِ وَٱلنُّورَۖ ثُمَّ ٱلَّذِينَ كَفَرُواْ بِرَبِّهِمۡ يَعۡدِلُونَ 
Cant ñeel na Yàlla mi bind asamaan yeek suuf si, te sos lëndëm yi ak leer yi. Terewul ña weddi ñoom di dendale seen Boroom ak leneen.
2هُوَ ٱلَّذِي خَلَقَكُم مِّن طِينٍ ثُمَّ قَضَىٰٓ أَجَلًاۖ وَأَجَلٌ مُّسَمًّى عِندَهُۥۖ ثُمَّ أَنتُمۡ تَمۡتَرُونَ 
Moom mooy ki leen bind ci ban ; ba noppi dugal àpp [ci dundu gu ne] ak àpp ba ñu tudd ci Moom [ci jéexug àdduna si]. Ba noppi ngeen di am xel-yaar !
3وَهُوَ ٱللَّهُ فِي ٱلسَّمَٰوَٰتِ وَفِي ٱلۡأَرۡضِ يَعۡلَمُ سِرَّكُمۡ وَجَهۡرَكُمۡ وَيَعۡلَمُ مَا تَكۡسِبُونَ 
Te Mooy Yàlla ci asamaan yeek suuf si. Mooy ki xam seen mbóot yi ngeen di nëbb ak yi ngeen di feeñal te xam it la ngeen di fàggu.
4وَمَا تَأۡتِيهِم مِّنۡ ءَايَةٍ مِّنۡ ءَايَٰتِ رَبِّهِمۡ إِلَّا كَانُواْ عَنۡهَا مُعۡرِضِينَ 
Te kat amul lenn ndigal lu leen dikke ca seen Boroom te dëdduwuñu ko.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-An'am 2

Simoore Aaya 2/165 — Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-An'am Dégg, Al-An'am Tekki, Al-An'am mp3, Al-An'am pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers