Al-Qalam · 36/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ ۝٣٦
Maa lakum kaifa tahhkumoon
📖 Tekkim Wolof
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Qalam

34إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ عِندَ رَبِّهِمْ جَنَّاتِ النَّعِيمِ
Ña ragal Yàlla dey ñoom am nanu Àjjanay xéewal fa seen Boroom.
35أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?
36مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?
37أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng
38إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Qalam 36

Simoore Al-Qalam Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di…

Simoore Aaya 36/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers