Al-Qalam · 38/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ ۝٣٨
Inna lakum feehi lamaa takhaiyaroon
📖 Tekkim Wolof
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Qalam

36مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?
37أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng
38إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?
39أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?
40سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Qalam 38

Simoore Al-Qalam Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci…

Simoore Aaya 38/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers