Al-Qalam · 37/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ ۝٣٧
Am lakum kitaabun feehi tadrusoon
📖 Tekkim Wolof
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Al-Qalam

35أَفَنَجْعَلُ الْمُسْلِمِينَ كَالْمُجْرِمِينَ
Moo ndax danuy def ñi wommatu jëm ci [Yàlla] ñu yem ak tooñkat ya ?
36مَا لَكُمْ كَيْفَ تَحْكُمُونَ
Ana lan moo leen dal ? Ak naka ngeen di àttee ?
37أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng
38إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?
39أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Qalam 37

Simoore Al-Qalam Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di…

Simoore Aaya 37/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers