Al-Qalam · 39/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ ۝٣٩
Am lakum aymaanun `alainaa baalighatun ilaa yawmil qiyaamati inna lakum lamaa tahkumoon
📖 Tekkim Wolof
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Qalam

37أَمْ لَكُمْ كِتَابٌ فِيهِ تَدْرُسُونَ
Wala book da ngeen am ab Téere bu ngeen di jàng
38إِنَّ لَكُمْ فِيهِ لَمَا تَخَيَّرُونَ
boo xam ne daal li ngeen bëgg lépp ngi ci ?
39أَمْ لَكُمْ أَيْمَانٌ عَلَيْنَا بَالِغَةٌ إِلَىٰ يَوْمِ الْقِيَامَةِ ۙ إِنَّ لَكُمْ لَمَا تَحْكُمُونَ
Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba àllaaxira, Mu defal leen fa lu ngeen bëgg ?
40سَلْهُمْ أَيُّهُم بِذَٰلِكَ زَعِيمٌ
Laajleen baxam ana kan ci ñoom mooy pakk wi ?
41أَمْ لَهُمْ شُرَكَاءُ فَلْيَأْتُوا بِشُرَكَائِهِمْ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Wala dañoo am ñu ñuy bokkaale ? Kon, nañu indi seen bokkaale ndegam nu dëggu la nu !
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Qalam 39

Simoore Al-Qalam Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wala book da ngeen am sunu ngiñ luy law ba…

Simoore Aaya 39/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers