Al-Qalam · 7/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ ۝٧
Innaa Rabbaka Huwa a`lamu biman dalla `an sabeelihee wa Huwa a`lamu bilmuhtadeen
📖 Tekkim Wolof
Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw Yoonam, te it moo gën a xam ñay gindiku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Qalam

5فَسَتُبْصِرُ وَيُبْصِرُونَ
Danga gis ñoom it danañu gis.
6بِأَييِّكُمُ الْمَفْتُونُ
Ana kan ci yéen moo sànku.
7إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw Yoonam, te it moo gën a xam ñay gindiku.
8فَلَا تُطِعِ الْمُكَذِّبِينَ
Bul topp mukk ñiy fen,
9وَدُّوا لَوْ تُدْهِنُ فَيُدْهِنُونَ
Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Qalam 7

Simoore Al-Qalam Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sa Boroom moo gën a xam ku réere aw…

Simoore Aaya 7/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers