Al-Haqqa · 48/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
وَإِنَّهُ لَتَذْكِرَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ ۝٤٨
Wa innahoo latazkiratul lilmuttaqeen
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Al-Haqqa

46ثُمَّ لَقَطَعْنَا مِنْهُ الْوَتِينَ
daldi, dog sidiiti xolam ( mu dee ).
47فَمَا مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ عَنْهُ حَاجِزِينَ
Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.
48وَإِنَّهُ لَتَذْكِرَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ
Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.
49وَإِنَّا لَنَعْلَمُ أَنَّ مِنكُم مُّكَذِّبِينَ
Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu koy weddi ;
50وَإِنَّهُ لَحَسْرَةٌ عَلَى الْكَافِرِينَ
ca dëgg-dëgg, bekkoor la ci yéefar yi,
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Haqqa 48

Simoore Al-Haqqa Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.

Simoore Aaya 48/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers