Al-Haqqa · 49/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَإِنَّا لَنَعْلَمُ أَنَّ مِنكُم مُّكَذِّبِينَ ۝٤٩
Wa inna lana`lamu anna minkum mukazzibeen
📖 Tekkim Wolof
Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu koy weddi ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Haqqa

47فَمَا مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ عَنْهُ حَاجِزِينَ
Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.
48وَإِنَّهُ لَتَذْكِرَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ
Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.
49وَإِنَّا لَنَعْلَمُ أَنَّ مِنكُم مُّكَذِّبِينَ
Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu koy weddi ;
50وَإِنَّهُ لَحَسْرَةٌ عَلَى الْكَافِرِينَ
ca dëgg-dëgg, bekkoor la ci yéefar yi,
51وَإِنَّهُ لَحَقُّ الْيَقِينِ
te moo di li wóor tigi.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Haqqa 49

Simoore Al-Haqqa Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu…

Simoore Aaya 49/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers