Al-Haqqa · 47/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
فَمَا مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ عَنْهُ حَاجِزِينَ ۝٤٧
Famaa minkum min ahadin`anhu haajizeen
📖 Tekkim Wolof
Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore Al-Haqqa

45لَأَخَذْنَا مِنْهُ بِالْيَمِينِ
( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,
46ثُمَّ لَقَطَعْنَا مِنْهُ الْوَتِينَ
daldi, dog sidiiti xolam ( mu dee ).
47فَمَا مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ عَنْهُ حَاجِزِينَ
Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.
48وَإِنَّهُ لَتَذْكِرَةٌ لِّلْمُتَّقِينَ
Ca dëgg-dëgg ag fàttali la ñeel ña ragal Yàlla.
49وَإِنَّا لَنَعْلَمُ أَنَّ مِنكُم مُّكَذِّبِينَ
Te xam nanu xéll ne am na ci yéen ñu koy weddi ;
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Al-Haqqa 47

Simoore Al-Haqqa Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.

Simoore Aaya 47/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers