Al-A'raf · 103/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِم مُّوسَىٰ بِآيَاتِنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَظَلَمُوا بِهَا ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ ١٠٣
Transliteration
Summa ba`asnaa mim ba`dihim Moosaa bi Aayaatinaaa ilaa Fir`awana wa mala`ihee fazalamoo bihaa fanzur kaifa kaana `aaqibatul mufsideen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba noppi Nu yónni ci seen ginnaaw Muusaa, mu ànd ak Sunu kéemaan ca Firawna ak mbooloom ña weddi. Seetlul naka la mujjug yàqkat ya mel nag.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 101-105 — Al-A'raf
101تِلْكَ الْقُرَىٰ نَقُصُّ عَلَيْكَ مِنْ أَنبَائِهَا ۚ وَلَقَدْ جَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَمَا كَانُوا لِيُؤْمِنُوا بِمَا كَذَّبُوا مِن قَبْلُ ۚ كَذَٰلِكَ يَطْبَعُ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِ الْكَافِرِينَ
Dëkk yooyu, Noo ngi lay nettali dara ci seeni xibaar. Te fekk Sunuy Yonent dikkoon fa ak ay lay yu leer, waaye ñoom mënatuñu woon a gëm la ñu daan weddi ca njalbéen. Noonu la Yàlla di fattee xoli yéefar ya.
102وَمَا وَجَدْنَا لِأَكْثَرِهِم مِّنْ عَهْدٍ ۖ وَإِن وَجَدْنَا أَكْثَرَهُمْ لَفَاسِقِينَ
Fekkunu woon li ëpp ci ñoom ñu ame kóllare fenn ; lu dul ne li ëpp ci ñoom ay saay-saay lañu.
103ثُمَّ بَعَثْنَا مِن بَعْدِهِم مُّوسَىٰ بِآيَاتِنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَظَلَمُوا بِهَا ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ
Ba noppi Nu yónni ci seen ginnaaw Muusaa, mu ànd ak Sunu kéemaan ca Firawna ak mbooloom ña weddi. Seetlul naka la mujjug yàqkat ya mel nag.
104وَقَالَ مُوسَىٰ يَا فِرْعَوْنُ إِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Muusaa ne : “Yaw Firawna, man ab Yonent laa [boo xam ne], Yàlla miy Boroom àddina si Moo ma yónni,
105حَقِيقٌ عَلَىٰ أَن لَّا أَقُولَ عَلَى اللَّهِ إِلَّا الْحَقَّ ۚ قَدْ جِئْتُكُم بِبَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّكُمْ فَأَرْسِلْ مَعِيَ بَنِي إِسْرَائِيلَ
wér na ci man ma bañ a wax ci Yàlla lu dul dëgg. Ne indil naa leen aw lay wu tukkee ci seen Boroom. Boyalal waa Bani-Israayil ñu ànd ak man.”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
103Aaya
Tekki — Al-A'raf 103
Simoore Al-A'raf Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba noppi Nu yónni ci seen ginnaaw Muusaa, mu ànd…Simoore Aaya 103/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








