Al-A'raf · 5/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَمَا كَانَ دَعْوَاهُمْ إِذْ جَاءَهُم بَأْسُنَا إِلَّا أَن قَالُوا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ ۝٥
Famaa kaana da`waahum iz jaaa`ahum baasunaa illaaa an qaalooo innaa kunnaa zaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Te seeni njàmbat nekkul, ba leen mbugal ma saddee, lu dul : “Nun ay tooñkat lanu woon”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Al-A'raf

3اتَّبِعُوا مَا أُنزِلَ إِلَيْكُم مِّن رَّبِّكُمْ وَلَا تَتَّبِعُوا مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءَ ۗ قَلِيلًا مَّا تَذَكَّرُونَ
Toppleen li ñu wàcce ci yéen mu jóge ca seen Boroom. Buleen ko bàyyi di topp ay xërëm. Néew ngeen xalaat.
4وَكَم مِّن قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا فَجَاءَهَا بَأْسُنَا بَيَاتًا أَوْ هُمْ قَائِلُونَ
Bariwaana dëkk bu Nu alag ! Sunu mbugal agsi fa ci guddi walla ci bëccëg.
5فَمَا كَانَ دَعْوَاهُمْ إِذْ جَاءَهُم بَأْسُنَا إِلَّا أَن قَالُوا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te seeni njàmbat nekkul, ba leen mbugal ma saddee, lu dul : “Nun ay tooñkat lanu woon”.
6فَلَنَسْأَلَنَّ الَّذِينَ أُرْسِلَ إِلَيْهِمْ وَلَنَسْأَلَنَّ الْمُرْسَلِينَ
Fàwwu Dananu laaj ña Nu yónni ca ñoom [nit ña], fàwwu it Dananu laaj ña Nu yónni woon [Yonent ya].
7فَلَنَقُصَّنَّ عَلَيْهِم بِعِلْمٍ ۖ وَمَا كُنَّا غَائِبِينَ
Te Dananu leen nettali ji [ci loolu] ci xam-xam bu wér ndaxte fekke woon Nanu lépp !
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Al-A'raf 5

Simoore Al-A'raf Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te seeni njàmbat nekkul, ba leen mbugal ma saddee, lu…

Simoore Aaya 5/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers