Al-A'raf · 72/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَأَنجَيْنَاهُ وَالَّذِينَ مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَقَطَعْنَا دَابِرَ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۖ وَمَا كَانُوا مُؤْمِنِينَ ۝٧٢
Fa anjainaahu wallazeena ma`ahoo birahmatim minnaa wa qata`naa daabiral lazeena kazzaboo bi Aayaatinaa wa maa kaanoo mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Nu musal ko moom ak ña ànd ak moom, ci Sama yërmaande, Nu daldi faagaagal nag ña jàppe Sunuy laaya ay fen te gëmuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Simoore Al-A'raf

70قَالُوا أَجِئْتَنَا لِنَعْبُدَ اللَّهَ وَحْدَهُ وَنَذَرَ مَا كَانَ يَعْبُدُ آبَاؤُنَا ۖ فَأْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Ñu wax ne : “Ndax danga noo dikkal ngir nu jaamu Yàlla moom doŋŋ, te bàyyi li sunu maam ya daan jaamu ? Indil nu li nga nu daan tëkkoo, ndegam ku dëggu nga”.
71قَالَ قَدْ وَقَعَ عَلَيْكُم مِّن رَّبِّكُمْ رِجْسٌ وَغَضَبٌ ۖ أَتُجَادِلُونَنِي فِي أَسْمَاءٍ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا نَزَّلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ فَانتَظِرُوا إِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُنتَظِرِينَ
Mu toontu ne : “Nekk na lu leen dëddale tukke ca seen Boroom, mbugal ak mer. Moo ndax dangeen di dàggasanteek man ciy tur yu ngeen sos yéen ak seeni maam, te Yàlla wàccewu ca wenn lay ? Man maa ngi nekk ak yéen di bokk ca way-muñandiku ña.
72فَأَنجَيْنَاهُ وَالَّذِينَ مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَقَطَعْنَا دَابِرَ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۖ وَمَا كَانُوا مُؤْمِنِينَ
Nu musal ko moom ak ña ànd ak moom, ci Sama yërmaande, Nu daldi faagaagal nag ña jàppe Sunuy laaya ay fen te gëmuñu.
73وَإِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا ۗ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ قَدْ جَاءَتْكُم بَيِّنَةٌ مِّن رَّبِّكُمْ ۖ هَٰذِهِ نَاقَةُ اللَّهِ لَكُمْ آيَةً ۖ فَذَرُوهَا تَأْكُلْ فِي أَرْضِ اللَّهِ ۖ وَلَا تَمَسُّوهَا بِسُوءٍ فَيَأْخُذَكُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Yónni woon Nanu it ca waa Tamuud, seen mbokk Saalihu, mu ne : "Yéen samay mbokk, nangeen jaamu Yàlla ndax amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Ay lay yu leer nàññ dikkal na leen, tukke ca seen Boroom : gëléem gu jigéen la, di mbindéefum Yàlla, di kéemaan ci yéen. Bàyyileen ko muy lekk ci kaw suuf si Yàlla moom, te buleen ko def lu bon ; kon mbugal mu tar dal leen [bu ngeen jëfewut ndigal li].
74وَاذْكُرُوا إِذْ جَعَلَكُمْ خُلَفَاءَ مِن بَعْدِ عَادٍ وَبَوَّأَكُمْ فِي الْأَرْضِ تَتَّخِذُونَ مِن سُهُولِهَا قُصُورًا وَتَنْحِتُونَ الْجِبَالَ بُيُوتًا ۖ فَاذْكُرُوا آلَاءَ اللَّهِ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Fàttalikuleen ba Mu leen defee ay kuutaay, ca ginnaaw Haad, mu dëkkal leen ci suuf si. Ngeen tabax ay kër yu rëy ci dénd yi, di yatt ci doj yi ay kër. Fàttalikuleen xéewali Yàlla te buleen doon ay yàqkat ci kaw suuf si.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Al-A'raf 72

Simoore Al-A'raf Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu musal ko moom ak ña ànd ak moom, ci…

Simoore Aaya 72/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 21, 2026

Don't forget us in your sincere prayers