Al-A'raf · 93/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَتَوَلَّىٰ عَنْهُمْ وَقَالَ يَا قَوْمِ لَقَدْ أَبْلَغْتُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَنَصَحْتُ لَكُمْ ۖ فَكَيْفَ آسَىٰ عَلَىٰ قَوْمٍ كَافِرِينَ ۝٩٣
Fatawalla `anhum wa qaala yaa qawmi laqad ablaghtukum Risaalaati Rabbee wa nasahtu lakum fakaifa aasaa`alaa qawmin kaafireen
📖 Tekkim Wolof
Mu dëddu leen, ne : "Yéen samay mbokk, jottali naa leen sama Yonentub Boroom, laabire naa leen itam. Kon naka laay yërëmtaloo ngir aw nit ñu di ay yéefar ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 91-95 — Simoore Al-A'raf

91فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ fa seeni kër.
92الَّذِينَ كَذَّبُوا شُعَيْبًا كَأَن لَّمْ يَغْنَوْا فِيهَا ۚ الَّذِينَ كَذَّبُوا شُعَيْبًا كَانُوا هُمُ الْخَاسِرِينَ
Ña weddi woon Chuhaybu, dañoo mujj mel ni masuñu faa dëkk. Ña weddi woon Chuhaybu yàqule nañu.
93فَتَوَلَّىٰ عَنْهُمْ وَقَالَ يَا قَوْمِ لَقَدْ أَبْلَغْتُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَنَصَحْتُ لَكُمْ ۖ فَكَيْفَ آسَىٰ عَلَىٰ قَوْمٍ كَافِرِينَ
Mu dëddu leen, ne : "Yéen samay mbokk, jottali naa leen sama Yonentub Boroom, laabire naa leen itam. Kon naka laay yërëmtaloo ngir aw nit ñu di ay yéefar ? ”
94وَمَا أَرْسَلْنَا فِي قَرْيَةٍ مِّن نَّبِيٍّ إِلَّا أَخَذْنَا أَهْلَهَا بِالْبَأْسَاءِ وَالضَّرَّاءِ لَعَلَّهُمْ يَضَّرَّعُونَ
Dunu yónni Yonent ci am réew, te tegunu waa réew ma ay tiis ak i njàqare ngir xéy-na ñu toroxlu.
95ثُمَّ بَدَّلْنَا مَكَانَ السَّيِّئَةِ الْحَسَنَةَ حَتَّىٰ عَفَوا وَّقَالُوا قَدْ مَسَّ آبَاءَنَا الضَّرَّاءُ وَالسَّرَّاءُ فَأَخَذْنَاهُم بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ginnaaw ba ñu soppi yu bon ya, toxal ca yu baax, bu ñu biroo it ñu naan : “Aw naqar ak mbégte daloon na sunuy maam.”. Nu songe woon leen ci mbetteel te fooguñu ko woon.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Al-A'raf 93

Simoore Al-A'raf Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu dëddu leen, ne : "Yéen samay mbokk, jottali naa…

Simoore Aaya 93/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers