Al-Ma'arij · 36/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
فَمَالِ الَّذِينَ كَفَرُوا قِبَلَكَ مُهْطِعِينَ ۝٣٦
Famaa lil lazeena kafaroo qibalaka muhti`een
📖 Tekkim Wolof
Waaw yéefar yi lu ñu xewal bay raj-rajloo wutsi la,

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Ma'arij

34وَالَّذِينَ هُمْ عَلَىٰ صَلَاتِهِمْ يُحَافِظُونَ
ak ñiy matal sëkk seeni julli.
35أُولَٰئِكَ فِي جَنَّاتٍ مُّكْرَمُونَ
Ñoom ña nga biir Àjjana deefi leen teral.
36فَمَالِ الَّذِينَ كَفَرُوا قِبَلَكَ مُهْطِعِينَ
Waaw yéefar yi lu ñu xewal bay raj-rajloo wutsi la,
37عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ عِزِينَ
di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?
38أَيَطْمَعُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُدْخَلَ جَنَّةَ نَعِيمٍ
Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 36

Simoore Al-Ma'arij Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaw yéefar yi lu ñu xewal bay raj-rajloo wutsi la,

Simoore Aaya 36/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers