Nuh · 23/28
Tekki Waxtaan — Nuh
وَقَالُوا لَا تَذَرُنَّ آلِهَتَكُمْ وَلَا تَذَرُنَّ وَدًّا وَلَا سُوَاعًا وَلَا يَغُوثَ وَيَعُوقَ وَنَسْرًا ۝٢٣
Wa qaaloo laa tazarunna aalihatakum wa laa tazarunna Waddanw wa laa Suwaa`anw wa laa Yaghoosa wa Ya`ooqa wa Nasraa
📖 Tekkim Wolof
tey wax naan : “Buleen bàyyi seeni Yàlli bu leen bàyyi Wud, Mbaa Suwaa’, ak Yaquusa, ak Ya’uuqa ak Nasra.
🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Nuh

21قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
22وَمَكَرُوا مَكْرًا كُبَّارًا
Ña ngay fexe pexe yu rëy,
23وَقَالُوا لَا تَذَرُنَّ آلِهَتَكُمْ وَلَا تَذَرُنَّ وَدًّا وَلَا سُوَاعًا وَلَا يَغُوثَ وَيَعُوقَ وَنَسْرًا
tey wax naan : “Buleen bàyyi seeni Yàlli bu leen bàyyi Wud, Mbaa Suwaa’, ak Yaquusa, ak Ya’uuqa ak Nasra.
24وَقَدْ أَضَلُّوا كَثِيرًا ۖ وَلَا تَزِدِ الظَّالِمِينَ إِلَّا ضَلَالًا
Te réeral nañu ñu bari. Te bul dolli tooñkat ya lu dul ag réer.
25مِّمَّا خَطِيئَاتِهِمْ أُغْرِقُوا فَأُدْخِلُوا نَارًا فَلَمْ يَجِدُوا لَهُم مِّن دُونِ اللَّهِ أَنصَارًا
Ci sababu seen ñaawtéef ya, labaleef na leen, tàbbalees leen safara, te amu ñu fa fekku ñu fa ku leen di dimbali, ku dul Yàlla”.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Nuh 23

Simoore Nuh Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : tey wax naan : “Buleen bàyyi seeni Yàlli bu leen…

Simoore Aaya 23/28 — Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Nuh Dégg, Nuh Tekki, Nuh mp3, Nuh pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers