Nuh · 22/28
Tekki Waxtaan — Nuh
وَمَكَرُوا مَكْرًا كُبَّارًا ۝٢٢
Wa makaroo makran kubbaaraa
📖 Tekkim Wolof
Ña ngay fexe pexe yu rëy,

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Nuh

20لِّتَسْلُكُوا مِنْهَا سُبُلًا فِجَاجًا
ngir ngeen mana sóobu ca yoonam yu dàndante ya”.
21قَالَ نُوحٌ رَّبِّ إِنَّهُمْ عَصَوْنِي وَاتَّبَعُوا مَن لَّمْ يَزِدْهُ مَالُهُ وَوَلَدُهُ إِلَّا خَسَارًا
Nooh daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, (samaw nit) moy na ñu ma dem toppi koo xam ne alalam ak i doomam jariñu ko lu dul yàqule.
22وَمَكَرُوا مَكْرًا كُبَّارًا
Ña ngay fexe pexe yu rëy,
23وَقَالُوا لَا تَذَرُنَّ آلِهَتَكُمْ وَلَا تَذَرُنَّ وَدًّا وَلَا سُوَاعًا وَلَا يَغُوثَ وَيَعُوقَ وَنَسْرًا
tey wax naan : “Buleen bàyyi seeni Yàlli bu leen bàyyi Wud, Mbaa Suwaa’, ak Yaquusa, ak Ya’uuqa ak Nasra.
24وَقَدْ أَضَلُّوا كَثِيرًا ۖ وَلَا تَزِدِ الظَّالِمِينَ إِلَّا ضَلَالًا
Te réeral nañu ñu bari. Te bul dolli tooñkat ya lu dul ag réer.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Nuh 22

Simoore Nuh Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ngay fexe pexe yu rëy,

Simoore Aaya 22/28 — Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Nuh Dégg, Nuh Tekki, Nuh mp3, Nuh pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers