Nuh · 5/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
قَالَ رَبِّ إِنِّي دَعَوْتُ قَوْمِي لَيْلًا وَنَهَارًا ۝٥
Qaala rabbi innee da`awtu qawmee lailanw wa naharaa
📖 Tekkim Wolof
(Nooh) : “Yaw sama Boroom ! woo naa samaw nit, guddeek bëcëg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Nuh

3أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ وَاتَّقُوهُ وَأَطِيعُونِ
Na ngeen jaamu Yàlla, te ragal ko, te topp ko
4يَغْفِرْ لَكُم مِّن ذُنُوبِكُمْ وَيُؤَخِّرْكُمْ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ إِنَّ أَجَلَ اللَّهِ إِذَا جَاءَ لَا يُؤَخَّرُ ۖ لَوْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
kon dey Dana leen jégël seeni bàkkaar te Dana leen yeexe ba ci dig bu ñu xam. Digub Yàlla bu agsee, du fanqu cëy bu ngeen xamoon ! ”
5قَالَ رَبِّ إِنِّي دَعَوْتُ قَوْمِي لَيْلًا وَنَهَارًا
(Nooh) : “Yaw sama Boroom ! woo naa samaw nit, guddeek bëcëg.
6فَلَمْ يَزِدْهُمْ دُعَائِي إِلَّا فِرَارًا
Te sama woote bi dolli wu leen lu dul féew.
7وَإِنِّي كُلَّمَا دَعَوْتُهُمْ لِتَغْفِرَ لَهُمْ جَعَلُوا أَصَابِعَهُمْ فِي آذَانِهِمْ وَاسْتَغْشَوْا ثِيَابَهُمْ وَأَصَرُّوا وَاسْتَكْبَرُوا اسْتِكْبَارًا
Te man saasu ma leen di woo ngir Nga jégël leen, dañuy def séeni waaraam ci séeni biiri nopp, daldi muuroo séeni sér, daldi jomlu.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — Nuh 5

Simoore Nuh Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Nooh) : “Yaw sama Boroom ! woo naa samaw nit,…

Simoore Aaya 5/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers