Nuh · 6/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
فَلَمْ يَزِدْهُمْ دُعَائِي إِلَّا فِرَارًا ۝٦
Falam yazid hum du`aaa `eee illaa firaaraa
📖 Tekkim Wolof
Te sama woote bi dolli wu leen lu dul féew.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Nuh

4يَغْفِرْ لَكُم مِّن ذُنُوبِكُمْ وَيُؤَخِّرْكُمْ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ إِنَّ أَجَلَ اللَّهِ إِذَا جَاءَ لَا يُؤَخَّرُ ۖ لَوْ كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
kon dey Dana leen jégël seeni bàkkaar te Dana leen yeexe ba ci dig bu ñu xam. Digub Yàlla bu agsee, du fanqu cëy bu ngeen xamoon ! ”
5قَالَ رَبِّ إِنِّي دَعَوْتُ قَوْمِي لَيْلًا وَنَهَارًا
(Nooh) : “Yaw sama Boroom ! woo naa samaw nit, guddeek bëcëg.
6فَلَمْ يَزِدْهُمْ دُعَائِي إِلَّا فِرَارًا
Te sama woote bi dolli wu leen lu dul féew.
7وَإِنِّي كُلَّمَا دَعَوْتُهُمْ لِتَغْفِرَ لَهُمْ جَعَلُوا أَصَابِعَهُمْ فِي آذَانِهِمْ وَاسْتَغْشَوْا ثِيَابَهُمْ وَأَصَرُّوا وَاسْتَكْبَرُوا اسْتِكْبَارًا
Te man saasu ma leen di woo ngir Nga jégël leen, dañuy def séeni waaraam ci séeni biiri nopp, daldi muuroo séeni sér, daldi jomlu.
8ثُمَّ إِنِّي دَعَوْتُهُمْ جِهَارًا
Topp, woonaa leen cig jooru.
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Nuh 6

Simoore Nuh Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sama woote bi dolli wu leen lu dul féew.

Simoore Aaya 6/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers