Al-Muzzammil · 15/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
إِنَّا أَرْسَلْنَا إِلَيْكُمْ رَسُولًا شَاهِدًا عَلَيْكُمْ كَمَا أَرْسَلْنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ رَسُولًا ۝١٥
Innaa arsalnaaa ilaikum rasoolan shahidan `alikum kamaaa arsalnaaa ilaa Fir`awna Rasoolna
📖 Tekkim Wolof
Yónni nanu ci yéen ab Yonent muy seede, kem ni nu yónnee woon ca Firawna ab Yonent.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Muzzammil

13وَطَعَامًا ذَا غُصَّةٍ وَعَذَابًا أَلِيمًا
ak aw ñam wuy fot loo, ànd ak mbugël mu mitti.
14يَوْمَ تَرْجُفُ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ وَكَانَتِ الْجِبَالُ كَثِيبًا مَّهِيلًا
Bu keroogee bis ba suuf seek doj yi dëgg-dëgg tundu yi mel ni suufus ber mokk.
15إِنَّا أَرْسَلْنَا إِلَيْكُمْ رَسُولًا شَاهِدًا عَلَيْكُمْ كَمَا أَرْسَلْنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ رَسُولًا
Yónni nanu ci yéen ab Yonent muy seede, kem ni nu yónnee woon ca Firawna ab Yonent.
16فَعَصَىٰ فِرْعَوْنُ الرَّسُولَ فَأَخَذْنَاهُ أَخْذًا وَبِيلًا
Firawna daldi moy Yonenta ba. Nu daldi koy jël bu metti. (faagaagal ko).
17فَكَيْفَ تَتَّقُونَ إِن كَفَرْتُمْ يَوْمًا يَجْعَلُ الْوِلْدَانَ شِيبًا
Ana naka ngeen di ragale (Yàlla), su ngeen weddee, bis boo xam ne tiit ma bijaawloona ab liir ?
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 15

Simoore Al-Muzzammil Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni nanu ci yéen ab Yonent muy seede, kem ni…

Simoore Aaya 15/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers