Al-Muzzammil · 16/20
Tekki Waxtaan — Al-Muzzammil
فَعَصَىٰ فِرْعَوْنُ الرَّسُولَ فَأَخَذْنَاهُ أَخْذًا وَبِيلًا ۝١٦
Fa`asaa Fir`awnur Rasoola fa akhaznaahu akhzanw wabeelaa
📖 Tekkim Wolof
Firawna daldi moy Yonenta ba. Nu daldi koy jël bu metti. (faagaagal ko).

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Al-Muzzammil

14يَوْمَ تَرْجُفُ الْأَرْضُ وَالْجِبَالُ وَكَانَتِ الْجِبَالُ كَثِيبًا مَّهِيلًا
Bu keroogee bis ba suuf seek doj yi dëgg-dëgg tundu yi mel ni suufus ber mokk.
15إِنَّا أَرْسَلْنَا إِلَيْكُمْ رَسُولًا شَاهِدًا عَلَيْكُمْ كَمَا أَرْسَلْنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ رَسُولًا
Yónni nanu ci yéen ab Yonent muy seede, kem ni nu yónnee woon ca Firawna ab Yonent.
16فَعَصَىٰ فِرْعَوْنُ الرَّسُولَ فَأَخَذْنَاهُ أَخْذًا وَبِيلًا
Firawna daldi moy Yonenta ba. Nu daldi koy jël bu metti. (faagaagal ko).
17فَكَيْفَ تَتَّقُونَ إِن كَفَرْتُمْ يَوْمًا يَجْعَلُ الْوِلْدَانَ شِيبًا
Ana naka ngeen di ragale (Yàlla), su ngeen weddee, bis boo xam ne tiit ma bijaawloona ab liir ?
18السَّمَاءُ مُنفَطِرٌ بِهِ ۚ كَانَ وَعْدُهُ مَفْعُولًا
Su asamaan si dee xar. Ca la digam ba di mate.
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 16

Simoore Al-Muzzammil Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna daldi moy Yonenta ba. Nu daldi koy jël bu…

Simoore Aaya 16/20 — Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Muzzammil Dégg, Al-Muzzammil Tekki, Al-Muzzammil mp3, Al-Muzzammil pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers