Al-Qiyama · 22/40
Tekki Waxtaan — Al-Qiyama
وُجُوهٌ يَوْمَئِذٍ نَّاضِرَةٌ ۝٢٢
Wujoohuny yawma `izin naadirah
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee, dana am xarkanam yu naat
🎧 Dégg

📜 Aaya 20-24 — Al-Qiyama

20كَلَّا بَلْ تُحِبُّونَ الْعَاجِلَةَ
Yéen da ngeena bëgg (lool) dundug àddina si,
21وَتَذَرُونَ الْآخِرَةَ
te da ngeena sàggane (lool) Àllaxira.
22وُجُوهٌ يَوْمَئِذٍ نَّاضِرَةٌ
Bu keroogee, dana am xarkanam yu naat
23إِلَىٰ رَبِّهَا نَاظِرَةٌ
yuy xool seen Boroom ;
24وَوُجُوهٌ يَوْمَئِذٍ بَاسِرَةٌ
dana fa am it bu keroogee, ay xarkanam yu ñàng,
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Qiyama 22

Simoore Al-Qiyama Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee, dana am xarkanam yu naat

Simoore Aaya 22/40 — Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qiyama Dégg, Al-Qiyama Tekki, Al-Qiyama mp3, Al-Qiyama pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers