Al-Insan · 20/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
وَإِذَا رَأَيْتَ ثَمَّ رَأَيْتَ نَعِيمًا وَمُلْكًا كَبِيرًا ۝٢٠
Wa izaa ra ayta summa ra ayta na`eemanw wa mulkan kabeera
📖 Tekkim Wolof
Soo ko gisee, danga fa gIisaale xeewal ak nguur gu màgg.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Insan

18عَيْنًا فِيهَا تُسَمَّىٰ سَلْسَبِيلًا
ab bëtu ndox bu tudd Salsabiil.
19۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ وِلْدَانٌ مُّخَلَّدُونَ إِذَا رَأَيْتَهُمْ حَسِبْتَهُمْ لُؤْلُؤًا مَّنثُورًا
Te ay xalee ngay wër ca ñoom sax cig ndaw. Soo leen gisee, da ngay foog ne peme ju ñu tasaare la ñu.
20وَإِذَا رَأَيْتَ ثَمَّ رَأَيْتَ نَعِيمًا وَمُلْكًا كَبِيرًا
Soo ko gisee, danga fa gIisaale xeewal ak nguur gu màgg.
21عَالِيَهُمْ ثِيَابُ سُندُسٍ خُضْرٌ وَإِسْتَبْرَقٌ ۖ وَحُلُّوا أَسَاوِرَ مِن فِضَّةٍ وَسَقَاهُمْ رَبُّهُمْ شَرَابًا طَهُورًا
Dañuy sol mbubbi sooy yu nëtëx werta. Moom la ñuy jiital waaje ko, te dañu leen di takkal caqi xaalis. Seen Boroom di leen fa ndàndale naan gu laab.
22إِنَّ هَٰذَا كَانَ لَكُمْ جَزَاءً وَكَانَ سَعْيُكُم مَّشْكُورًا
Lii nag mooy seen neexal, te seen jëf it lu ñu sant la.
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Insan 20

Simoore Al-Insan Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Soo ko gisee, danga fa gIisaale xeewal ak nguur gu…

Simoore Aaya 20/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers