Al-Anfal · 9/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
إِذْ تَسْتَغِيثُونَ رَبَّكُمْ فَاسْتَجَابَ لَكُمْ أَنِّي مُمِدُّكُم بِأَلْفٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُرْدِفِينَ ۝٩
Iz tastagheesoona Rabbakum fastajaaba lakum annee mumiddukum bi alfim minal malaaa`ikati murdifeen
📖 Tekkim Wolof
(Fàttalikul) ba ngeen sàkkoo xettaliku ci seen Boroom te Mu nangul leen, ne : “Man danaa leen dooleel ak junni Malaaka yuy toftalante.

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Anfal

7وَإِذْ يَعِدُكُمُ اللَّهُ إِحْدَى الطَّائِفَتَيْنِ أَنَّهَا لَكُمْ وَتَوَدُّونَ أَنَّ غَيْرَ ذَاتِ الشَّوْكَةِ تَكُونُ لَكُمْ وَيُرِيدُ اللَّهُ أَن يُحِقَّ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ وَيَقْطَعَ دَابِرَ الْكَافِرِينَ
(Fàttalikul), ba leen Yàlla digee ndam ca kaw benn ca ñaari kurél ya ngeen moom ko. Te ngeen ne siiw moom ga yorul ngànnaay, te Yàlla nammoon a dëgëral dëgg ga ci kàddoom te dog ginnaaw yéefar ya.
8لِيُحِقَّ الْحَقَّ وَيُبْطِلَ الْبَاطِلَ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ
ngir dëgg sax te caaxaan jóge fi doonte la naqari na saay-saay sa.
9إِذْ تَسْتَغِيثُونَ رَبَّكُمْ فَاسْتَجَابَ لَكُمْ أَنِّي مُمِدُّكُم بِأَلْفٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُرْدِفِينَ
(Fàttalikul) ba ngeen sàkkoo xettaliku ci seen Boroom te Mu nangul leen, ne : “Man danaa leen dooleel ak junni Malaaka yuy toftalante.
10وَمَا جَعَلَهُ اللَّهُ إِلَّا بُشْرَىٰ وَلِتَطْمَئِنَّ بِهِ قُلُوبُكُمْ ۚ وَمَا النَّصْرُ إِلَّا مِنْ عِندِ اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Yàlla deful loolu lu dul ngir mbégtem [jullit ñi] ak ngir seen xel dal. Ndimbal amul feneen fu dul fa Yàlla. Naka Yàlla Aji-not la, Aji-xereñ la.
11إِذْ يُغَشِّيكُمُ النُّعَاسَ أَمَنَةً مِّنْهُ وَيُنَزِّلُ عَلَيْكُم مِّنَ السَّمَاءِ مَاءً لِّيُطَهِّرَكُم بِهِ وَيُذْهِبَ عَنكُمْ رِجْزَ الشَّيْطَانِ وَلِيَرْبِطَ عَلَىٰ قُلُوبِكُمْ وَيُثَبِّتَ بِهِ الْأَقْدَامَ
(Fàttalikuleen) ba Mu leen muuree ag ngëmmentu muy jàmm ju jóge ci Moom, te Mu wàcce ci yéen ndox mu jóge asamaan ngir Mu laabal leen ak loolu, ak ngir Mu dàqal leen sobees Séytaane, ak ngir Mu dëgëral seeni xol, dëgëral seeni ndëggu.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Anfal 9

Simoore Al-Anfal Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Fàttalikul) ba ngeen sàkkoo xettaliku ci seen Boroom te Mu…

Simoore Aaya 9/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers