Al-Anfal · 8/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
لِيُحِقَّ الْحَقَّ وَيُبْطِلَ الْبَاطِلَ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ ۝٨
Liyuhiqqal haqqa wa tubtilal baatila wa law karihal mujrimoon
📖 Tekkim Wolof
ngir dëgg sax te caaxaan jóge fi doonte la naqari na saay-saay sa.
🎧 Dégg

📜 Aaya 6-10 — Al-Anfal

6يُجَادِلُونَكَ فِي الْحَقِّ بَعْدَمَا تَبَيَّنَ كَأَنَّمَا يُسَاقُونَ إِلَى الْمَوْتِ وَهُمْ يَنظُرُونَ
Ñangay weranteek yaw ca dëgg ga ginnaaw ba mu feeñee, leer nàññ ; mel ni dañu leen a bëmax jëme ci dee, ñu ne ca jàkk.
7وَإِذْ يَعِدُكُمُ اللَّهُ إِحْدَى الطَّائِفَتَيْنِ أَنَّهَا لَكُمْ وَتَوَدُّونَ أَنَّ غَيْرَ ذَاتِ الشَّوْكَةِ تَكُونُ لَكُمْ وَيُرِيدُ اللَّهُ أَن يُحِقَّ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ وَيَقْطَعَ دَابِرَ الْكَافِرِينَ
(Fàttalikul), ba leen Yàlla digee ndam ca kaw benn ca ñaari kurél ya ngeen moom ko. Te ngeen ne siiw moom ga yorul ngànnaay, te Yàlla nammoon a dëgëral dëgg ga ci kàddoom te dog ginnaaw yéefar ya.
8لِيُحِقَّ الْحَقَّ وَيُبْطِلَ الْبَاطِلَ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ
ngir dëgg sax te caaxaan jóge fi doonte la naqari na saay-saay sa.
9إِذْ تَسْتَغِيثُونَ رَبَّكُمْ فَاسْتَجَابَ لَكُمْ أَنِّي مُمِدُّكُم بِأَلْفٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُرْدِفِينَ
(Fàttalikul) ba ngeen sàkkoo xettaliku ci seen Boroom te Mu nangul leen, ne : “Man danaa leen dooleel ak junni Malaaka yuy toftalante.
10وَمَا جَعَلَهُ اللَّهُ إِلَّا بُشْرَىٰ وَلِتَطْمَئِنَّ بِهِ قُلُوبُكُمْ ۚ وَمَا النَّصْرُ إِلَّا مِنْ عِندِ اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Yàlla deful loolu lu dul ngir mbégtem [jullit ñi] ak ngir seen xel dal. Ndimbal amul feneen fu dul fa Yàlla. Naka Yàlla Aji-not la, Aji-xereñ la.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Anfal 8

Simoore Al-Anfal Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngir dëgg sax te caaxaan jóge fi doonte la naqari…

Simoore Aaya 8/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers